«Waxal bànni Israyil, ne leen bu ñu jàllee dexu Yurdan ba dugg réewum Kanaan,
TSK
TSK · Exodus 21:13
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Numbers 35:10
TSK
Deuteronomy 4:41
TSK
¶ Ba loolu wéyee Musaa ber na ñetti dëkk ca penkub dexu Yurdan,
Deuteronomy 19:2
TSK
ñetti dëkk yu mag ngeen di ber ca biir réew mooma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox, ngir ngeen jagoo ko.
¶ Te it buleen toxal seen yemukaayu suufas moroom yu maam ya yemalee woon ci seen biir céru suuf ba ngeen jagoo, ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji di moomale.
1 Samuel 24:10
TSK
daldi wax Sóol ne ko: «Lu waral ngay déglu ku la naan: “Daawuda mii sa musiba lay wut.”
2 Samuel 16:10
TSK
Buur ne ko: «Yeen doomi Seruya yi, lu ciy seen yoon? Sañ na maa saaga. Su ko Aji Sax ji santee mu saaga ma, ana ku ko saña laaj lu tax?»
Micah 7:2
TSK
Ngor a jeex ci réew mi, njub tumurànke ci nit ñi. Ñépp, ku ñu tuur deretam lañuy tëru, ku nekk, mbokkam lay fiir.