TSK

TSK · Ezekiel 21:26

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Aji Sax jeey xañe, di maye, di detteel, di kaweel.

¶ Yóbbu nañu Yowakin buurub Yuda ngàllo ba mu am fanweeri at ak juróom ñaar, Ewil Merodag doora falu buur ca Babilon. At mooma, fukkeelu weer waak ñaar, ñaar fukki fan ak juróom ñaar ca weer wa, ca la Ewil Merodag siggil Yowakin buurub Yuda, daldi koy tijji.

Mooy yékkatee ku néewle fa suuf, di seppee ku sonn cib sën,

Waxal Buur, wax Lingeer yaayu Buur ne leen: «Dëjuleen fi suuf, seen mbaxanam nguur mu yànj foq na.

Ñu jàpp ko, yóbbu ca buuru Babilon ca dëkk ba ñuy wax Ribla ca réewum Amat. Nabukodonosor dogal fa àtteem.

ba noppi takkal la jaarob bakkan ak jaaroy nopp, solal la mbaxanam lingeer mu yànj.

Luke 1:52 TSK

wàccee buur yi ci seeni gàngune, yékkati baadoolo yi.