TSK

TSK · Genesis 2:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

saw ñaq ngay dunde, ba kera ngay dellu ci suuf, si ma la jële; ndaxte pënd nga, te dinga dellu di pënd.»

Mboolem mbindeef muy boroom bakkan ci kaw suuf a bokk dee.

«Aji Sax ji, yaw Yàlla mi moom noowi bépp boroomu suux, ngalla tabbal nit ku jiite mbooloo mi,

Job 27:3 TSK

ne li feek may ànd ak bakkan, di noyyee noowal Yàlla,

Job 33:6 TSK

Maa ngii, yem ak yaw fa Yàlla; ci ban lañu ma mooñe man itam.

Moo xam sunu bind, di bàyyi xel ne pënd lanu.

Xelum nit làmp la bu Aji Sax ji taal, da koy niital ba ca biir xolam.

Ñoom ñépp a bokk jëm benn bérab ba, bokk jóge pëndub suuf, bokk dellu suuf.

Baleen nit, noowal bakkan kese la! Ana lees koy nawe?

Boroom bi Aji Sax ji dafa wax yax yii, ne leen: Maa ngii di leen sol ag noo, ngeen dund.

¶ Ab yéenee ngi, di kàddug Aji Sax ju dikkal Israyil. Kàddug Aji Sax jee, ki firi asamaan, lal suuf, te bind noowug doom aadama ci biir doom aadama.

Te it jariñoowul loxol nit, mbete ku soxla lenn, ndax mooy may ñépp bakkan akug noo, ak lu mu mana doon.

¶ Noonu lañu binde ne: «Aadama, nit ku jëkk ka, lañu def jëmm juy dund,» waaye Aadama mu mujj mi moo di Noo giy dundloo.

¶ Nun nag nooy njaqi bani kese yi yeb jooju alal, ngir mu bir ne manoore ju yéeme ji alal ji làmboo, manoorey Yàllaa, waaye du sunu jos.

Te itam am nanu ay baay ci wàllu deret, ñoo nu daan yar, te danu leena wegoon. Kon nag xanaa du Baay bi yor ug noo lanu wara gënatee nangul, ngir nu dund?