Keroog Aji Sax ji fas na kóllëre digganteem ak Ibraam, ne ko: «Askan wi soqikoo ci yaw laa jox réew mii dale ci dexu Misra, ba ca dex gu mag googee di Efraat,
TSK
TSK · Genesis 31:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Loolu wees ñu toog, di lekk. Nes tuut ñu siggi, séen am njëggum giléem, muy ay Ismayleen, yu sëf cuuraayu ndàbb ak diwu yaram ak cuuraayu xas, jële ko réewu Galàdd, jëme Misra.
¶ Balaam nag gis ne Aji Sax ji la neex mu barkeel Israyil, ba tax sàkkootul ay takk na woon, xanaa mu walbatiku, janook màndiŋ ma.
¶ Suuf soosu nu nangu ca jant yooya, te dale ca Arower ga ca xuru Arnon ca bëj-saalum, ak ca bëj-gànnaar, genn-wàllu diiwaanu tundi Galàdd, aki dëkkam, maa ko jox Rubeneen ñi, ak Gàddeen ñi.
Ci kaw loolu ñu dem diiwaanu Galàdd, jàll ba Kades ca diiwaanu Etteen ña, dem Dan Yaan ak la ko wër, teg ca Sidon.
¶ Xaalisu saraxu peyug tooñ nag ak xaalisu saraxu póotum bàkkaar daawuñu ko indi ci kër Aji Sax ji. Sarxalkat yaa ko moomoon.
¶ Ba ñu demee ba bés bi ñu wara yéege Yeesu di jubsi, Yeesu moo dogu ngir dem Yerusalem.