Naka lañu ko yeew ngir dóor ko ay kàccri, mu ne njiitu takk-der ba fa taxaw: «As goru Room bu yoon dabul, mbaa am nga sañ-sañu dóorlu ko?»
TSK
TSK · Luke 7:8
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Acts 22:25
TSK
Acts 23:23
TSK
¶ Ba mu ko defee mu woo ñaari njiiti takk-der, ne leen: «Waajal-leen ñaar téeméeri xarekat ak juróom ñaar fukki gawar ak ñaar téeméeri boroom xeej, ngir ngeen dem Sesare bu juróom ñeenti waxtu jotee ci guddi.
Acts 23:31
TSK
¶ Ba loolu amee xarekat ya def la ñu leen digal, yóbbu Póol ci guddi ba ca dëkk ba ñuy wax Antipataris.
Acts 25:26
TSK
Mbiram nag laa amul dara lu ma wóor, ngir ma bind ko sang bi. Moo tax ma indi ko ci seen kanam, rawatina ci sa kanam, Buur Àggripa, ngir gannaaw bu ñu ko dégloo, ma mana am lu ma bind.
1 Timothy 6:1
TSK
¶ Mboolem ñi ci buumu njaam, nañu jàpp ne seeni sang yelloo nañu gépp wegeel, ngir kàddu gu teddadi baña tege ci turu Yàlla, ak sunu àlluwa.