TSK

TSK · Numbers 13:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Xanaa kay, kàttan gu askanu réew ma am, péey ya dàbbliku te yaa lool. Te it ponkal yooyu cosaanoo ci Anageen ñi lanu fa gis.

Ana fu nu jëm? Te sunu bokk ya demoon yoqiloo nu, ne nu waa réew maa nu ëpp, sut nu, dëkk ya réy te dàbblikoo ay tata yu àkki asamaan. Rax ci dolli, ay ponkal yu bokk ci askanu Anageen ñi lanu fa gis!»

Yaw suuf, maay doxloo nit fi sa kaw, muy waa Israyil sama ñoñ, ñu jagoo la, séddoo la, te dootoo sabab seenug deele.”»

Amos 2:9 TSK

«Ndaxam maa leen reyaloon Amoreen ñu gudd ña te réy, mbete garab yu mag. Ma boor doom ya, buur reen ya.