TSK

TSK · Numbers 16:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ndax dinanu ko tas de. Aji Sax ji dégg na jooytu yu réy, yi niti dëkk bi sabab, ba tax mu yónni nu, ngir nu tas-si ko.»

Léegi seetaan ma rekk, samam sànj tàkkal leen, ba ma faagaagal leen, te du tee ma def la askan wu mag.»

Maa leen di fàdde mbas, nangu seen cér, ba noppi sose ci yaw askan wu leen ëpp, ëpp leen doole.»

Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!

Seen mbari fitt ŋafal paxum bàmmeel, ñoom ñépp di ñeyi xare.

Kon nag: «Nangeen génne ci seen biir, te teqlikoo ak ñoom,» la Boroom bi wax. «Lu sobewu, buleen ko laal. Su boobaa, maa leen di dalal.

¶ Kon nag gannaaw nguur gu deesul yëngal lanu jagoo, nanu jàppoo cant, di jaamu Yàlla ni mu ko bëgge cig njullite akug ragal,