Exodus 6:24
TSK
¶ Doomi Kore yu góor ñoo di Asir ak Elkana ak Abiyasaf. Ñooñoo sos làngi Kore.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Doomi Kore yu góor ñoo di Asir ak Elkana ak Abiyasaf. Ñooñoo sos làngi Kore.
Ñu daldi tàbbiwaale bakkan biir njaniiw, ñook mboolem lu ñu moom, suuf sàng leen, ñu réer mbooloo ma mërr.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di taalif bu ñeel askanu Kore wu góor.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di jàngin wu ñeel askanu Kore wu góor, dëppook galan bu ñuy wax Baatu jigéen.
Muy woyu Sabóor, ñeel askanu Kore wu góor.
Muy kàddug Sabóor, giiroo ci Asaf. Yàlla, Aji Sax ji Yàlla àddu na, di woo àddina, penku ba sowu.