TSK

TSK · Proverbs 4:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba nit ka xamee ne manalu ko dara, dafa dóor Yanqóoba ci mooco, mooco mi summikoo ca bëre ba.

Mooy garabu gudd fan ci ku ko jàpp, di mbégtey ku ca ŋoy.

Santaane da lay niital, ndigal leeralal la, artook ub yar di yoonu dund.

Xel mu rafet kiiraay la, xaalis kiiraay la; njariñu xam-xam mooy xelu, mucc.

Mu tàmbalee nag ci Yonent Yàlla Musaa, jaare ci yonent yépp, tekkil leen mboolem lu Mbind mi indi ci mbiram.

Ba Barnaba dikkee ba gis yiw, wi leen Yàlla may, dafa bég, di leen ñaax ngir ñu ŋoye seen xol ci Sang bi.

¶ Moo tax nu wara yokka teewlu kàddu yi nu dégg, bala noo lajj, taañaañal.

Sunu bokk yee daan ndax deretu Gàtt bi, ak seen kàddug seede, te soppuñu seen bakkan ba ragala dee.