Mu jekki sànni xeej ba, te naan ca xelam: «Naa daaj Daawuda ci tabax bi!» Daawuda nag mbas ko ñaari yoon.
TSK
TSK · 2 Samuel 4:8
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yonatan yegge ko Daawuda, ne ko: «Sama baay a ngi lay wuta rey. Yaw nag fagarul kat te teela xëy ëllëg, seet foo làquji te baña génn.
¶ Daawuda nag dawe Nayot, ca wetu dëkk ba ñuy wax Raama. Mu dikk ca Yonatan, ne ko: «Ana lu ma def? Ana ñaawtéef gu ma def, ak fu ma tooñe sa baay, ba muy wut sama bakkan?»
Mu dem ba tollook ay ngéddi xar ca yoon wa; foofa am xuntee nga fa woon. Mu dugg ca biir, di suturlu. Fekk na Daawudaaki nitam a nga ca biir-a-biir xunti ma, toog.
¶ Ba loolu wéyee Ayimaas doomu Cadog ne: «May ma rekk ma daw yégali Buur xibaar bii, ne ko Aji Sax ji musal na ko ciy noonam.»
Mooy Yàlla ji may feyul, di ma suufeelal xeet yi.
May yendoo siiwal sa njekk nde ña ma doon wuta lor lañu rusloo, sewal leen.
Kon ndax Yàlla man naa baña sàmm àqu tànnéefam ñi koy woo wall guddi ak bëccëg, xanaa di leen yeexe?
Ndokklee, asamaan, Ndokklee, yeen ñu sell ñi itam, ak ndawi Yàlla yeek yonent yi, ndaxte Yàllaa leen àtteek dëkk bii, mbugal ko.