TSK

TSK · Acts 2:22

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Luke 7:20 TSK

Taalibe ya dikk ne ko: «Yaxya moo nu yebal, di la laaj ndax yaa di Ki wara ñëw, am keneen lanuy séentu?»

Ñu ne ko Yeesum Nasaret moo fa jaare.

Acts 3:12 TSK

Piyeer nag gis loolu, àddu, ne mbooloo ma: «Yeen bokki Israyil, lu ngeen di waaru ci lii? Lu ngeen nu naa jàkk, mel ni sunu manoorey bopp mbaa sunug njullite lanu doxloo kii?

Acts 5:35 TSK

Ba ñu génnee, mu ne waa kurél ga: «Yeen bokki Israyil, moytuleen bu baax li ngeen di def ak nit ñii.

Yeen ci seen bopp xam ngeen li xewoon ci mboolem réewum Yawut yi, te dale ci diiwaanu Galile, gannaaw ba Yaxya wootee, di sóobe cim ndox,

Ba ñu agsee, dañoo woo mbooloom gëmkat ña, àgge leen mboolem na Yàlla def ak ñoom, ak na mu ubbilee jaambur ñi dul Yawut buntu ngëm.

Acts 22:8 TSK

Ma ne ko: “Sang bi, yaa di kan?” Mu ne ma: “Man maay Yeesum Nasaret, mi ngay bundxatal.”

Acts 26:9 TSK

¶ «Man ci sama bopp, gàntal lu ma man turu Yeesum Nasaret, sama warugar laa ko defoon.

Firnde yiy màndargaal ndawal Almasi, feeñalees na ko ci seen biir, lépp ci ag muñ gu mat sëkk: firnde yeek kéemaan yeek jaloore yi.