TSK

TSK · Leviticus 26:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Fexeleen rekk ba Aji Sax ji, buleen ko gàntal, te yeen nag ngeen baña ragal waa réew ma, ndax ab lanc doŋŋ lañu nuy mat. Seen kiiraay dëddu na leen, te Aji Sax jaa ngeek nun. Buleen leen ragal.»

¶ Aji Sax jeey def, noon yi leen di jógal, ñooy daanu fi seen kanam. Wenn yoon lañuy dikke, dal ci seen kaw, waaye juróom ñaari yoon lañuy awe, daw, jiitu leen.

Yonatan ñalgu ca kaw tund wa, gàddukatu gànnaayam topp ko. Yonatan a ngay jam, waa Filisti di daanu, gàddukatu gànnaayam ba di leen jekkli ca gannaawam.

Éy su ma sama ñoñ déggaloon, éy su Israyil toppoon samay nammeel!