Isaiah 54:16
TSK
Xoolal, man maa sàkk ab tëgg buy wal taalu këriñ, defar ca ngànnaay lu ne. Waaye maa sàkk it yàqkat buy rajaxe.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Xoolal, man maa sàkk ab tëgg buy wal taalu këriñ, defar ca ngànnaay lu ne. Waaye maa sàkk it yàqkat buy rajaxe.
Ba mu ma yóbboo ba foofa, ma jekki yem ci nit ku am melow xànjar, ŋàbb buumu lẽe ak yetu nattukaay. Ma nga taxaw ca buntu dëkk ba.
Mu nattaat yeneen junniy xasab, ndox ma yem ma ciy óom. Mu dellu natt junniy xasab, jàlle ma, ndox ma yem ma ci ndigg.
Moo tax Aji Sax ji dafa wax ne: “Yërmande laay dellusee Yerusalem. Sama kër lees fay tabaxaat.” Kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi. Mu ne: “Buumu nattukaay dina tàllalu ci kaw Yerusalem.”
¶ Ba loolu amee ñu jox ma nattukaay bu mel niw yet, ne ma: «Jógal, natt néeg Yàlla bi ak sarxalukaay bi, te nga waññ ña fay jaamu Yàlla.