TSK

TSK · Daniel 5:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Peeñu mu ñàng lañu ma ci wax. Workat biy wor, yàqkat biy yàq. Yeen waa Elam, songleen; yeen waa Medd, gawleen leen. Dakkal naa mboolem onk yu ñu sabab.

Musibaa lay dikkal, te doo xam fu mu fenke. Njaaxum a lay dal, te du looy mana fanq. Sànkuteey jekki dale la foo yégul.

Dajaleleen xeet yi fi kaw Babilon, wooleen buuri Medd ak kàngam ya ak jawriñ ñaak mboolem réew mu ñu moom.

¶ «Sa gannaaw geneen nguur dina taxaw, gën laa suufe, ñetteelu nguur ga topp ca di xànjar, tiim àddina sépp.

Keey musle, di xettlee, di def ay màndarga aki kéemaan, kaw asamaan ak suuf. Kee musal Dañeel ca pàddum gaynde ya.»

Kuuy mi nga gis mu am ñaari béjjén, buuri waa Medd ak waa Pers la.