TSK

TSK · Job 10:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Su dee dee moom, nun ñépp ay dee ni ndox di tuuroo ba deesu ko tanqati. Yàlla nag musalul kenn ci dee, waaye moo lal pexe ngir ki gàddaay du saxoo gàddaay bérab bu ko sore.

Job 3:13 TSK

Tëdd koon naak jàmm biir bàmmeel, di nelaw, nopploondook

Job 7:9 TSK

Niir wu naaxsaay, ne mes, mooy ku wàcci njaniiw, du yéegati!

Job 16:22 TSK

At yu néew déy a ci des, ma dem yoon wu ma dul délsi.

Su may jaare xuru ndee wu ne këruus it, duma ragal loraange: yaw laak man, sa bantu sàmm ak sa nguul, yooyoo may dalal.

bokk ci néew, yi dara waratul, mbaa ku ñu bóom, mu tëdd cim pax, faaleetoo ko, xanaa dagg ko, wacc.

Ana kuy yég say kéemaan ci googu lëndëm? Ku lay seedeel njekk réew ma fàtte faloo?

Ak lu say at bare bare, bégeel at mu ci nekk, waaye bàyyil xel lëndëmu bàmmeel, lu yàgg lay doon, te liy ñëw lépp, cóolóoli neen.

Newuñu: “Ana Aji Sax, ji nu génne woon réewum Misra, jiite nu ca biir màndiŋ ma, ca joor gu wow gaak xur ya, réewum maral ma lëndëm këruus, jaareesu fa, dëkkeesu fa?”