Yaa dëje tund yu mag yi doole, gañoo sa kàttan,
TSK
TSK · Luke 8:24
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 65:7
TSK
Psalms 104:6
TSK
Yaa ko sànge xóotey géej ni mbubb, ndox ma taxaw, tiim tund ya.
Psalms 116:3
TSK
Buumi ndee a ma laawoon, njàqarey njaniiw dab ma, ma dajeek naqar aku tiis.
Isaiah 50:2
TSK
Ana lu tax ba ma dikkee, kenn nekku fa? Ma woote, kenn wuyuwul? Damaa gàtta gàtt loxo, ba manumaa walloo? Am damaa ñàkk doole ju ma xettlee? Xanaa du maay gëdd géej, mu wow, maay defi dex màndiŋ, ndox tukki; jën ya mar, dee ba yàqu?
ndox ma mëdd ma, ma ne: «sànku naa.»
Luke 5:5
TSK
Simoŋ ne ko: «Njaatige, coono lanu fanaane biig te jàppunu dara. Xanaa ma sànni ko rekk ci sa ndigal.»
Nun ci sunu wàllu bopp, jàppoon nanu ne sunu àtteb dee moo taxaw. Waaye loolu tax na nu bañatee yaakaar sunu bopp, xanaa di yaakaar ci Yàlla, miy dekkal ñi dee.