mu gën koo ragalati. Fa la Sóol doxe doon noonub Daawuda ba fàww.
TSK
TSK · Psalms 13:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Buur laaj ma, ne ma: «Lu la tax ne yogg te woppuloo? Mbaa du tiisu xol?» Maa ngi tiit lool.
Dama di Géej menn mbaa Ninki-nànka, ba nga di ma booleek ku may wattu?
Su ma nee: «Naa fàtte sama tawat, leeral kanam te bég,»
Seet naa wetu penku, Yàlla nekku fa, ma seet sowu, gisuma ko.
Éy Aji Sax ji, sama Yàlla, yaw laay làqoo! Musal ma, xettli maak ñi may dàq ñépp.
Aji Sax ji sunu Boroom, sa tur aka màgg ci kaw suuf sépp! Sag leer tiim asamaan.
ngir sàmm àqu jirim ak néew-ji-doole, ba nit kiy suufu kese dootu xëble.
Man nag aw sax rekk laa, matuma nit. Doom aadama sewal ma, aw xeet tuutal ma.
Ma ne, ngalla buñu ma ree, di damoo samab jéll.
Bëccëg Aji Sax ji baaxe ma ngoram, guddi ma fanaane koo woy, di ñaan Yàlla mi may dundal.
Éy Yàlla, fu reetaani noon di dakke? Xanaa bañ yi duñu la ñàkke kersa ba fàww?
Naa xaacu, woo Yàlla, sama baat fa Yàlla, ngir mu déglu ma.
Dama noon: «Tarxiis naa!» Waaye yaa ma awoo sa ngor.
Éy Aji Sax ji, baaxe nu, rikk baaxe nu, dañu noo torxal, ba nu ne tott.
Noon a ma sambal, daane ma, joggati, dëël ma ci lëndëm ni ku dee bu yàgg.
Lii daal laa ci gis, man. Li gën te jaadu ci nit: Na lekk, naan te bànneexoo ñaqam wu mu ñaqe kaw suuf giiru dund gi ko Yàlla may. Loolu mooy céram.
Moo sama tiis wi du dakk a? Bii góom bu metti, tëë wér! Yaw kay yaay waltan muy wal, di ŋiis, di tas sama yaakaar.
Seen noon yaa jiite tey, seen bañ yooyoo ne finaax, Aji Sax jee mbugale waa Siyoŋ seeni tooñ yu bare, seeni doom duggig njaam, di moomeel ub noon.
Ana lu waral nga fàtte nu fàww, ba nu jant yu yàgge nii?
Woppoon na it ba xawa dee, waaye Yàllaa ko yërëm, te du moom rekk la yërëm, waaye man itam, ngir ma baña am tiis ci kaw tiis.