Boroom tiis, ana lees koy maye leeru kaw suuf? Lu boroom naqar di doye bakkan?
TSK
TSK · Job 40:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Dama di Géej menn mbaa Ninki-nànka, ba nga di ma booleek ku may wattu?
Ku bëgga layook Yàlla it, mu laaj la junni, doo tontu lenn.
Yàlla da dul nit ni man, ba may weranteek moom, di ànd ak moom, layooji.
ne ma dann, ba su ma bàkkaaree, doo ma baal samag tooñ.
Konoon yaay lim samay jéego, te doo ma topp samay bàkkaar.
Waaye xamleen ne Yàllaa ma tooñ, ab caaxam a ma dar kepp.
Yaa soppiku, néege ma, di ma soxoree sa diisaayu loxo.
Takkul boog te góor-góorlu, ma laaj la, nga xamal ma.
Ana ku mu diisool, ba kooka tegtal ko, jàngal ko yoonu njub, jàngal ko xam-xam, xamal ko yoonu dég-dég?
Ki may dëggal jege na. Ana kuy layook man? Nan bokk taxaw! Kuy jànkoonteek man ci yoon? Na jegesi boog!
«Ana ku xam xalaatu Boroom bi? Ana ku ko digal?»
Am danuy yékkati fiiraangey Sang bi? Danu koo ëpp doole?